Mathieu laa tudd, Point E laa dëkk, waaye Cameroun
laa joge.
Ñow naa Senegaal ngir liggéey ci GIZ.
Dégg naa Anglais ak Français ak Allemand, bëgg naa jàng Wolof
ak Gueelem ngir mën waxtaan ak samay xarit.
Ambassadeur digital laa ci GIZ.
https://learningapps.org/display?v=px8hor6e523
Bëgg naa developper ay applications informatiques ngir
jappale nit ñu nekk ci dekk ba.
Jigeen ni mën nañu jaay seeni produits ci internet ak
Whatsapp Business ak Facebook Marketplace.
Xale yi mën nañu jàng ak jeu en ligne ak Scratch.
Waa Senegaal mën nañu def seeni démarches en ligne ak seen
téléphone.