Listen

Description

Waxtaan wu am solo, wow Sñ Ahmadu Rafaahii MBÀKKE, tënk na ci mbirum wahaabiya, ak sosoom, ak seeni pas-pas, ak liy seen jafe-jafe sa diggënte ak yeneen jullit yi