Listen

Description

Waxtaan wu am solo, ci 4i tomb yu aju ci dundug Sëriñ bi ci Njaaréem - Lu waral Tubaab yi tànn Njaareem, comme résidence survéller?- Lu waraloon Murid yi participé ci guerre 14-18 bi?- Lu wara participation 500 yi Sëriñ bi joxoon Tubaab yi?- Lu wara Ecole francaise bi woon ci Njaaréem?Nu ànd ko ak Baay Mbaye Gueye Syll