Listen

Description

Al-Minahu-l Miskiyyah

المنح المسكية في الخوارق المبكية

Di téere boo xamne Sëriñ Muhammadu-l Amiin Joob Dagana, moo ko bind, jagleel ko lenn ci kéemaane Sëriñ Tuubaa yi mu fekkee, ak yi mu jëlee ci nettali yu wér.

Une oeuvre de Cheikh Mouhamadoul Amine Diop, sur l’enseignements et miracles de Cheikh Ahmadou Bamba (1853-1927)

Traduction & Commentaire : Abdou Khadre BA Majalis