Listen

Description

Boroom ñaari tur!
Bu yàggul dara gis nanu ak li xéw ak Gana Géy. Mu bañoon jàppale boroom ñaari tur yi ci yaatal seen gis gis, waaye mu dégg ci lu nekk. Loolu moo waral ñu def ci taxaw setlu yi xool ndax mbir mi dëppo na ak suñuy gëm-gëm ak ban taxawaay lanu ci war a am.

lahatdiaw@gmail.com