Xam-xamu xadiis lanuy waxtaane tay. Mu nekk fànn bu yaatu boo xamne woroom xam-xam yi gëstu na ñu ci ngir yoonal lépp loo xamne toxalees nako co Yonent bi (saws). Bokk na ci ay waat yu ñu leeral jëm ci xadiis, lu melni „Sanad“ te mooy goor yiy soloo xadiis yi, walla „Matn“ te mooy li ñuy soloo. Mu nekk xam-xam yu yaatu waaye fi nuy indi rek fànn wu ndaw ci seddale yi ñu def ci xadiis (classification).
Baay Lahat
lahatdiaw@gmail.com